Home - El xarop dels idiomes

El xarop dels idiomes - Wòlof

Yaram nit

 

xarop_ca

Mun gama dimbali? Dama am...

 

Naka lai meün wakh sama diangale-kat dakh dama febër, te munu-ño dego?
Wala sama put dai meti? Wala sama bop?
Naka la mune wakh sama talibe dakh beütam daño honk?

Bude musga am metuñi melni, li ñui wakh ci kanam munala diering.
Dugueül, te ga hol ciliga beügue diank ci sa birum, te ga diel lakh bulanëkh.
Diga fek lu barri ci liga beügue diank ci lak bula nekh.
Te diga meu meun-ko lakh ci Catalan!

 

Foël te ga diangale-wat ci birum febaru-ñi ci lak-bi ga tan.

 

Nuuñu tuudu teñ ci arab?



 

Ak rakhassu ci roumain? Ak sabuu-bop ci ourdou? Ak yokosuu ci chinois?

 

Fii diga fek leüp lu ga sokhla pur kham-ko ci 19 lakh-ñii : almand, anglais, arab, basque, boulgar, espagnol, catalan, français, galicien, italien, polonais, portuguais, roumain, rousse,’’ tagal’’, ucranien, ourdou, wolof ak chinois.

Te Catalan cii bopam diga ko mana wakh¡

Foye-yal te di jang cii birum wëru cii lakh-ñii.